Bànqaasu xam-xam

Dalleen ak jàmm ci xëtu Yutub bii di Bànqaasu xam-xam
Bànqaasu xam-xam di xët wow jàngale xam-xam ci fan yu wuute moo ko tax a jóg jaarale ko ci làkkuw Wolof .
Xam binu xam ni am réew manuta suqaliku ak am um yokkute ndeem moo ngi wékku ci am réew ni moom.Mépp réew ci saw làkk ak sam mbatiit nga man sukkandiku ngir man a jëm kanam .
Xam luni mel moo waral Bànqaasu xam-xam tànn làkk wi gën a yaatu ci réew mi te ëpp ñi koy jëfandikoo aka dawal ngir jàllale xam-xam yi.
Fànn yi nuy fésal ci xët bi bokk na ci xam-xamu :
Xewxam ;
Dund ak suuf ( tàmbali bi jëm ci dongo yi nekk ci joŋante BFEM ) ;
mbëj ;Xarala ;
Ci ay fan yu néew, dinanu andi yeneeni jàngale yu yees.

Bànqaasu xam-xam moo ngi leen di Jaajëfal di bég ci tasaare njàng mi ak toppu bi.
Jaajëfal Itam Block Business, jëf, Jang Wolof ak jàngalekat yi

🔘 xët wii di bànqaasu xam-xam moy télé bi ñëkka déf ay video jangalé xam-xamu science ak technologie ci wolof.


Bànqaasu xam-xam

Dalal jàmm ci seen wàllu podcast bu bees bi tudd « Podkast Bànqaasu xam xam ». Podcast bii dafay wax ci mbir yépp yu jëm ci njàng, tàggat, tegtal ci njàng ak boole liggéey, xarala yu bees ak liggéey. Ay wideo ci losisel Autocad am nañu ci lien bii: youtube.com/playlist?list=PLB...
Aboneel ci chaine bi leegi.

Bienvenue dans votre nouveau rubrique de podcast intitulé "Podkast Bànqaasu xam xam". Ce podcast traitera tous les sujets relatifs à l'éducation, la formation, l'orientation scolaire et l'insertion professionnelle, la technologie et les métiers. Une série de vidéo sur le logiciel Autocad est déja disponible sur ce lien : youtube.com/playlist?list=PLB...
Merci de s'abonner à-coup la chaine.

1 year ago | [YT] | 7

Bànqaasu xam-xam

Salamu Aleykum Abonnés Chaine bi
Nàmmoon ngeen ñu ?
#Bànqaasu xam-xam

4 years ago | [YT] | 20

Bànqaasu xam-xam

1000 Abonnés
Jërëjëf ci topp bi

5 years ago | [YT] | 11