As Salaamu Aleykoum.
Baye Darou 2.0 mooy kër gu ñu di bokk ci zikroulah, thiantes ak ay waxtaan yu jëm ci yoonu ngëm.
Fi ngay gis :
Zikroulah
Thiantes
Ay waxtaan yu am solo
Jàngat ak xam-xam ci yoonu ngëm
Bul fàtte :
Abonnéel
Bëgg video yi
Séddoo leen ak sa xarit yi
Yalla na Yàlla barkeel sunuy jëf.