Jambarou Mouride 2.0

As-salaamu aleykum mbokk yi.

Dalal-leen ak jàmm ci Jàmbaarou Mouride 2.0, seen pénc'um internet ngir wisaare njàngalem Sëriñ Touba Khadimou Rassoul ak kàttanug liggéeyu Mame Cheikh Ibrahima Fall.


Podcast sur Spotify 🎧 👉🏾 : open.spotify.com/episode/2LTsJsEQm57CVJNJzJsNUa

Fi, dañuy séddoo ak yéen ay waxtaan yu am solo, ay ndenkané, ay nettali ci dundug Sëñ bi ak Jéwriñ ji, ak leeral ci maanaa "Jëf-Jël", ngor, ak kóolute gi taxawal Yoonu Murid. Suñu yéene mooy fessal xam-xamu diine bi, dëgërël sunu pas-pas, te booloo ci yoonu yiw wi.
Bësal butoŋ bii di 'S'abonner' ngir bokk ci mbooloo mi, te bësal kloc bi ngir jot ab yëgal-yëgal saa suñu amee video bu bees.
Jërëjëf. Yàlla na nu Sëriñ bi taas ci barkeem.


Jërëjëfé Seriñ Touba



Jambarou Mouride 2.0

Sokhna Maï Bintou Cheikhoul Khadim ❤️

4 days ago | [YT] | 57

Jambarou Mouride 2.0

👇🏾

6 days ago | [YT] | 10

Jambarou Mouride 2.0

Serigne Modou Fall "Bambara " grand disciple de Mame Cheikh Ibrahima Fall Baboul Mouridina.

👉🏾👉🏾👉🏾 : Waxtaan Ci Thiossanou Mame Cheikh Thierno Birahim Mbacké | Ndamal Darou !
https://youtu.be/_PvxcoYy5HA


Serigne Modou Fall Bambara fut l'un des grands disciples mystiques et un Cheikh éminent de Mame Cheikh Ibrahima Fall Baboul Mouridina. Originaire de Ségou, au Mali, terre héritière de la grandeur de l'Empire du Mali, il incarna l'esprit de la khidma, où le service du Cheikh est vécu comme un chemin de purification de l'âme et de rapprochement d'Allah.

Il fut également le puisatier de Mame Cheikh Ibrahima Fall. En creusant les puits et en puisant l'eau pour son Cheikh, il ne voyait pas un simple travail, mais un acte d'adoration, de fidélité et d'amour. Chaque coup de pioche, chaque seau d'eau transporté témoignait de son engagement total au service de son guide spirituel, avec une détermination, une patience et une humilité exemplaires.

Dans la tradition mandingue, le patronyme Fall est souvent associé aux Coulibaly, rappelant les liens historiques et fraternels entre le Sénégal et le Mali, notamment à travers l'héritage de l'Empire du Mali et l'idéal d'unité qui s'est également exprimé lors de la Fédération du Mali.

L'exemple de Serigne Modou Fall Bambara rappelle que, dans la tradition Baay Fall, la véritable élévation ne s'obtient ni par les honneurs ni par les paroles, mais par la khidma, le sacrifice, l'humilité et l'obéissance sincère au Cheikh, dans la recherche exclusive de l'agrément d'Allah.

Qu'Allah l'agrée, élève davantage son rang parmi les serviteurs vertueux, et nous fasse bénéficier de sa baraka, ainsi que de celle de Mame Cheikh Ibrahima Fall Amin

Amadou Djibril Diop
Lampe Lerale

1 week ago | [YT] | 1,295

Jambarou Mouride 2.0

Le BRAS DROIT DU CHEIKH

1 week ago | [YT] | 11

Jambarou Mouride 2.0

Jerejefety Borom Touba ❤️

2 weeks ago | [YT] | 16

Jambarou Mouride 2.0

❤️👇🏾

1 month ago | [YT] | 5

Jambarou Mouride 2.0

Serigne Mouhamadou Kane ❤️

👉🏾 : https://youtu.be/-k8HuYgyfB4?si=66VHr...

1 month ago (edited) | [YT] | 963

Jambarou Mouride 2.0

S Cheikh Mountakha Bachir Yàlla na Yàlla Yoku weergui ak fanwi Si Barkep Serignebi

S Cheikh Saliou Yàlla nala Yàlla doli ngeureum ak Yeurmandee Si Barkep Serignebi

1 month ago | [YT] | 2,534

Jambarou Mouride 2.0

Jerejefety Mame Cheikh Anta Mbacké ❤️
Jerejefety Serigne Moussa Ka ❤️

Jerejefety Borom Touba

1 month ago | [YT] | 13

Jambarou Mouride 2.0

S Saliou Mbacke Moom S Cheikh Saliou

Yàlla nako Yàlla Samu, gudal fanam yoku weergui ak kataan gui ak kheweul yi Si Barkep Seringebi

1 month ago | [YT] | 772