🎥 Bienvenue sur XIPPY TV ! 🎤
La chaîne de DJ Moïse, animateur radio passionné par la musique, les médias et le partage de connaissances.

📌 Au programme sur XIPPY TV :

✅ Conseils pratiques pour progresser et réussir

🎓 Tutoriels simples et efficaces pour apprendre étape par étape

💡 Inspiration et motivation pour rester créatif et positif

🎶 Sans oublier une touche de musique, d’animation et de divertissement !

👉 Abonne-toi dès maintenant et active la cloche 🔔 pour ne rien manquer.


XIPPY TV

18H INCHALLH

3 weeks ago | [YT] | 0

XIPPY TV

Ci vidéo bii, nu ngi tàmbali léegi lépp ci vMix, ngir ndimbal yow nit ku nekk ci sa premier live.
Benn tutoriel Wolof bu step-by-step:

🎥 Li ngay jang ci vidéo bi :

Naka lañu bëgg a setup vMix ci YouTube

Naka lañu start live ci sa chaîne

Naka lañu configure audio, vidéo ak overlays

Naka lañu jëfandikoo tags ak astuces ngir gën a am viewership

💡 Tips ak tricks ngir sa diffusion di am jàmm ak réussite !

📺 Suqali vidéo bi te abonne nga ci Xippy TV 🎙️ ngir am tutoriel yu bees ci Wolof.

7 months ago | [YT] | 1